wo-wtb-train-xibaaryi-xeex-sibiru
Universal Dependencies - Wolof - WTB
Language | Wolof |
---|
Project | WTB |
---|
Corpus Part | train |
---|
Annotation | Dione, Bamba |
---|
View options
Text: - Show: - Tags:
Javascript seems to be turned off, or there was a communication error. Turn on Javascript for more display options.
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
Soleil, Jokkub awril, xët 7 Sibbiru màtt-màttu yoo moo koy joxe. Su fagaru amul, xel xalaatul xeex sibbiru. Xeex bi warul a yem rekk ci faj nit ñi. Kàddu yii tukkee ci Mustafaa Siise, kilifag biro bi di toppatoo fagaru ak jëflante ci Progaraam bi di xeex sibbiru, tudd PNLP ci frãse, wone na cër bu yaatu bi fagaru am ci xeex sibbiru, nga xam ne at mu ne dina rey lu ëpp milyoŋ ci ay nit. Kon fagaru moo gën faju.
Download XML • Download text
• Sentence view • Dependency trees