wo-wtb-train-xibaaryi-demokraasi-senegaal
Universal Dependencies - Wolof - WTB
Language | Wolof |
---|
Project | WTB |
---|
Corpus Part | train |
---|
Annotation | Dione, Bamba |
---|
View options
Text: - Show: - Tags:
Javascript seems to be turned off, or there was a communication error. Turn on Javascript for more display options.
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
Fan lanu jëm ak sunu demokaraasi bii? Réew mu nga xam ni yennat ci ay xalaat ñoo fi dagan, yeneen dañu araam. Réew mi moo ne: sañ-sañu xalaat génne ko, xalaatal sa xel, lu mu jur nga wësin ko niki yooyee demokaraasi di yu Tugal yi nga xam ne ñooy ya mag yi ñu di roye. Loolu jural nu nuy lang ci ay mbiccam, di jafandu ci ay waggam. Nu naan lu fi di lu baax moom la, du keneen, du feneen. Loolu tax na ba sax lu bawoo feneen du leneen lu dul neen ndax li muy keneen.
Download XML • Download text
• Sentence view • Dependency trees