wo-wtb-train-xibaaryi-ayti-woppu-caar

Universal Dependencies - Wolof - WTB

LanguageWolof
ProjectWTB
Corpus Parttrain
AnnotationDione, Bamba

Javascript seems to be turned off, or there was a communication error. Turn on Javascript for more display options.

Woppu Caar wiy faafaagal waa Ayti digg weeru oktoobar ak léegi, a ngay wéy di yokk. Ci bisub 14 nowàmbar, 917 nit faatu nañu fa. Yàlla na leen ko Boroom bi teggil ci jàmm.

Download XMLDownload textSentence viewDependency trees