wo-wtb-train-wolof-online-senegaal-unesco
Universal Dependencies - Wolof - WTB
Language | Wolof |
---|
Project | WTB |
---|
Corpus Part | train |
---|
Annotation | Dione, Bamba |
---|
View options
Text: - Show: - Tags:
Javascript seems to be turned off, or there was a communication error. Turn on Javascript for more display options.
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
Senegaal ak bés bi UNESCO jàgleel làkki-ndey Bésu 21 fan ci weeru Fewrie at mu jot, moom la kurél gi di toppatoo caada, njàng ak xamtéef (UNESCO) te feeteewoo ci Mbotaayu-xeet-yi, jagleel làkki-ndey yi, maanaam làkk wi nga xam ne moom la nit ku nekk nàmp. Loolu bi ko UNESCO dooree ak léegi ëpp na 10 at. Li waral bés bi mooy yee nit ñi, artu leen, soññ leen ci solo bu jeggi-dayoo bi làkki-ndey yi am ci fànnu yokkute yépp. Rawatina ci réewi Afrik yi nga xam ne daanaka ya ca ëpp ba ñu tàbbee ci 'kolonisation' ba téy jii ñu moomee seen bopp, dañoo xeeb seeni làkk yi ñu nàmp. Réew yi gën a bari Afrik, Senegaal waxi noppi, seeni làkk sedduñu leen daanaka benn cër bu tàkku.
Download XML • Download text
• Sentence view • Dependency trees