wo-wtb-train-osad-jabet

Universal Dependencies - Wolof - WTB

LanguageWolof
ProjectWTB
Corpus Parttrain
AnnotationDione, Bamba

Javascript seems to be turned off, or there was a communication error. Turn on Javascript for more display options.

index sentence 1 - 6 > sentence 7 - 17

Lan lañu war a xam ci jabet Xibaar yii tibbees na leen ci Orangeinfo, ñu tukkee ci Doktoor Abdul Asiis Kase (Dr Abdoul Aziz KASSE Chirurgien Institut du Cancer Université Cheikh Anta DIOP) Lan mooy jabet? Ñaari wirgoy jabet ñoo am, jabet 1 ak jabet 2. Ñoom ñaar ñépp xàmmees na leen ci nattu suukar bu jéggi dayo ci deret ji, ëpp 1,26 g. Waaye li sabab natt bu jéggi dayo bi ci jabet 1 wuute na ak li ko sabab ci jabet 2.

Download XMLDownload textSentence viewDependency trees