wo-wtb-dev-xibaaryi-luwaa-ndaamar-senegaal
Universal Dependencies - Wolof - WTB
Language | Wolof |
---|
Project | WTB |
---|
Corpus Part | dev |
---|
Annotation | Dione, Bamba |
---|
View options
Text: - Show: - Tags:
Javascript seems to be turned off, or there was a communication error. Turn on Javascript for more display options.
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
Njiitu réew mi, Maki Sàll, tënk na léegi ci 8 at jéle ko ci 5, digub at yi oto yi di dugg Senegaal te di jóge bitim-réew war a am. Mu ngi ko dogale ci jotaayu jëwriñ yi amoon alxamis ci Ndakaaru. Moom (Maki Sàll) xaatim na dekkare n° 2012-444 soppi bu n° 2001-72 bu 26 samwie 2001 jëm ci dugal daamar ci biir réew mi. Dekkare boobu dafa di tënk léegi ci 8 at jéle ko ci 5 at yi oto yi di duggu Senegaal war a am. S. Sàll dige woon na ci baatum dagaan ne dina ko def bu ñu ko tegee ci boppu réew mi. Daamar yu ëpp 10 at a ngi daw ca Bennoo-Réew ak ca Tugal.
Download XML • Download text
• Sentence view • Dependency trees