wo-wtb-dev-wol-wiki-Bawol
Universal Dependencies - Wolof - WTB
Language | Wolof |
---|
Project | WTB |
---|
Corpus Part | dev |
---|
Annotation | Dione, Bamba |
---|
View options
Text: - Show: - Tags:
Javascript seems to be turned off, or there was a communication error. Turn on Javascript for more display options.
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
Ci xarnub fukk ak juróom Bawol nguur su ndaw la woon su toppoon Jolof gu mag gi. Bu ko defee, ag njaboot gu am ag jegeñaale ak buuri Kajoor yi daan ko jiite. Bu jëkk, nguur googu, ay socé ak ay séeréer, ñoo ko yoroon. Ndax Bawol, benn dex la woon foofu ci lu doog a am. Boobu jamono, Bawol, amoon na ndox mu bare. Ci cosaan, dañu ne, Bawol, ku fa jëkk a nekk buur, Xaayamagaan moo doon turam.
Download XML • Download text
• Sentence view • Dependency trees