Sentence view

Universal Dependencies - Wolof - WTB

LanguageWolof
ProjectWTB
Corpus Parttrain
AnnotationDione, Bamba

Text: -


[1] tree
Woppu Caar wiy faafaagal waa Ayti digg weeru oktoobar ak léegi, a ngay wéy di yokk.
s-1
wo_wtb-ud-train_443
Woppu Caar wiy faafaagal waa Ayti digg weeru oktoobar ak léegi, a ngay wéy di yokk.
[2] tree
Ci bisub 14 nowàmbar, 917 nit faatu nañu fa.
s-2
wo_wtb-ud-train_444
Ci bisub 14 nowàmbar, 917 nit faatu nañu fa.
[3] tree
Yàlla na leen ko Boroom bi teggil ci jàmm.
s-3
wo_wtb-ud-train_445
Yàlla na leen ko Boroom bi teggil ci jàmm.

Edit as listText viewDependency trees