wo-wtb-train-xibaaryi-tambakundaa-wowal

Universal Dependencies - Wolof - WTB

LanguageWolof
ProjectWTB
Corpus Parttrain

Javascript seems to be turned off, or there was a communication error. Turn on Javascript for more display options.

index sentence 1 - 6 > sentence 7 - 17

Tambaakundaa, 2 awril (APS) Tàmbaakundaa: taxawal ay wanagi wowal, ngir doomi jàngoro yi bañ a ayibal ndoxum teen yi ak yu ni mel. Sàntar bi di saytu kàttanu jant bi ak cet, te nekk ci Tàmbaakundaa samp na ay wanagi wowal. Xeetu wanag woowu nag mbeeste la, dees ko di tabax ci taxawaayu benn meetar walla lu ko ëpp, mu lëkkaloo ak ñaari pax. Benn bi def sobe si (puup yi), fekk am na pexe mu leen nal ba ñu wow, ñu def leen tos. Beneen bii def saw mi ak ndoxum laablu mi, ñu suuxate ko flëer yi.

Download XMLDownload textSentence viewDependency trees