wo-wtb-train-xibaaryi-fajkatu-jigg__en
Universal Dependencies - Wolof - WTB
Language | Wolof |
---|
Project | WTB |
---|
Corpus Part | train |
---|
View options
Text: - Show: - Tags:
Javascript seems to be turned off, or there was a communication error. Turn on Javascript for more display options.
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
Ab fajkatu jigéen mu ngi feddali wartéef wu tar wi jëm ci xeex réer gu jéggi-dayo gi Doktoor bu amul bluus: Réer moo jiitu ci jàngoro yi ñu war a faj Doktoor Atab Baaji (Atab Badji) mi liggéeyam màcc ci mbirum jigéen, biral na ne jamp na lool ñu xeex réer gu tar gi lëmbe Afrig te gàllankoor bu baax lépp lu mën a jur yokkute.
Download XML • Download text
• Sentence view • Dependency trees