wo-wtb-train-wol-wiki-Kajoor
Universal Dependencies - Wolof - WTB
Language | Wolof |
---|
Project | WTB |
---|
Corpus Part | train |
---|
View options
Text: - Show: - Tags:
Javascript seems to be turned off, or there was a communication error. Turn on Javascript for more display options.
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
Ci wàllu xay Kajoor moo doonoon seetub Senegaal. Dammeel moo nekkoon ca kaw di seddale ay ndomboy tànk. Kajoor moo di kàdd ag garab gu nekk Senegaal ak joor, suuf si. Moo jur baat boobu Kajoor ci Wolof. Ñi jëkk a yor suufi Kajoor, ay séeréer lañu woon. Ñu doonoon ay lamaan te sant JAAÑ.
Download XML • Download text
• Sentence view • Dependency trees