wo-wtb-test-wol-wiki-jimbulang
Universal Dependencies - Wolof - WTB
Language | Wolof |
---|
Project | WTB |
---|
Corpus Part | test |
---|
View options
Text: - Show: - Tags:
Javascript seems to be turned off, or there was a communication error. Turn on Javascript for more display options.
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
-
Jimbulang aw wayndare la wu yitteem doon ëmb mbooleem xeeti xam-xam walla man naa itam tënku ci benn xam-xam, maanaam jimbulang bu di wax ci paj walla ci taariix kepp. Jimbulang am mbooloom ay jukki la def, bu ci nekk di wax ci lenn: ci aw nit, ci ab barab, ci ab xew-xew, ci ab xam-xam, ... Jimbulang dafa di wuute ak baatukaay, ndax du yem rekk ci faramfacce wenn làkk wi. Naka-jekk dafay doon ay téere yu bari. Cër yi ëpp solo yi di tax a raññee ab jimbulang, ñeent lañu: Jagleel gi ci am, seenug lëkkaloo, nosiin wi ak mbidiinu jukki yi. Jimbulang yi man nañu a wuute, aju ci seen ëmbiit, man nañu a ubbeeku ci xeeti xameef yépp (Jimbulang bu Trecani ak Jimbulang bu waa Brëtaañ, ñoo di yi ci gën a siiw), walla itam tënku ci wenn xeetu xam-xam wi, niki ab jimbulangu paj, bu xam-xam walla bu xeltu.
Download XML • Download text
• Sentence view • Dependency trees