wo-wtb-dev-osad-kolesterol

Universal Dependencies - Wolof - WTB

LanguageWolof
ProjectWTB
Corpus Partdev

Javascript seems to be turned off, or there was a communication error. Turn on Javascript for more display options.

index sentence 1 - 6 > sentence 7 - 17

Moytuleen kolesterol (cholestérol) Xibaar yii tibbees na leen ci Orangeinfo, ñu tukkee ci Doktoor Abdul Asiis Kase. Lan mooy kolesterol? Kolesterol diw la gu baax ci nit, ndax dafa bokk ci yi di tabax yaram. Waaye nag, su natt bi jéggee dayo ci deret ji, dafa di bàyyi ay àkk ci solom yi deret ji di jaar ngir dem ci xol bi (athérosclérose). Fu kolesterol di jóge?

Download XMLDownload textSentence viewDependency trees