Dependency Tree

Universal Dependencies - Wolof - WTB

LanguageWolof
ProjectWTB
Corpus Parttrain

Select a sentence

s-1 Woppu Caar wiy faafaagal waa Ayti digg weeru oktoobar ak léegi, a ngay wéy di yokk.
s-2 Ci bisub 14 nowàmbar, 917 nit faatu nañu fa.
s-3 Yàlla na leen ko Boroom bi teggil ci jàmm.

Text viewDownload CoNNL-U