Dependency Tree
Universal Dependencies - Wolof - WTB
Language | Wolof |
---|
Project | WTB |
---|
Corpus Part | train |
---|
Select a sentence
s-1
| Ab fajkatu jigéen mu ngi feddali wartéef wu tar wi jëm ci xeex réer gu jéggi-dayo gi |
s-2
| Doktoor bu amul bluus: Réer moo jiitu ci jàngoro yi ñu war a faj |
s-3
| Doktoor Atab Baaji (Atab Badji) mi liggéeyam màcc ci mbirum jigéen, biral na ne jamp na lool ñu xeex réer gu tar gi lëmbe Afrig te gàllankoor bu baax lépp lu mën a jur yokkute. |
Text view
•
Download CoNNL-U