Sentence view
Universal Dependencies - Wolof - WTB
Language | Wolof |
---|
Project | WTB |
---|
Corpus Part | train |
---|
Text: -
showing 101 - 200 of 134 • previous
Bu ragalee barig dooley la muy loj, man naa yeew tànkub càmmooñu kanam ba.
s-101
wo_wtb-ud-train_1933
Bu ragalee barig dooley la muy loj, man naa yeew tànkub càmmooñu kanam ba.
Balaa tàmbali mu wax Bismil Laahi, bu tàmbalee mu bañ a dindi loxoom lifeek noppiwul.
s-102
wo_wtb-ud-train_1934
Balaa tàmbali mu wax Bismil Laahi, bu tàmbalee mu bañ a dindi loxoom lifeek noppiwul.
Lu ñu war a loj nag bu ñu amul lojukaay sañees na koo rendi.
s-103
wo_wtb-ud-train_1935
Lu ñu war a loj nag bu ñu amul lojukaay sañees na koo rendi.
Lu ñu war a rendi it bu ñu amul rendikaay te am lojukaay sañees na koo loj.
s-104
wo_wtb-ud-train_1936
Lu ñu war a rendi it bu ñu amul rendikaay te am lojukaay sañees na koo loj.
Giléem loj rekk lañu koy def mbaa deesu ko lekk, waaye deesu ko rendi, xanaa ñu loru ñàkk lojukaay te am rendikaay.
s-105
wo_wtb-ud-train_1937
Giléem loj rekk lañu koy def mbaa deesu ko lekk, waaye deesu ko rendi, xanaa ñu loru ñàkk lojukaay te am rendikaay.
Bu boobaa nag dees na leen ko may.
s-106
wo_wtb-ud-train_1938
Bu boobaa nag dees na leen ko may.
Bu dee aw nag dees na ko loj niki noonu it dees na ko rendi.
s-107
wo_wtb-ud-train_1939
Bu dee aw nag dees na ko loj niki noonu it dees na ko rendi.
Kon moom lu leen jekku rekk ñu sañ koo def noona.
s-108
wo_wtb-ud-train_1940
Kon moom lu leen jekku rekk ñu sañ koo def noona.
Fii nag rendi ko lañu gën a miin.
s-109
wo_wtb-ud-train_1941
Fii nag rendi ko lañu gën a miin.
Loj, balaa baax ñatti sidit yu mag yi dañu war a dagg.
s-110
wo_wtb-ud-train_1942
Loj, balaa baax ñatti sidit yu mag yi dañu war a dagg.
Kon ci ag wet lañu koy defe ak kanam...
s-111
wo_wtb-ud-train_1943
Kon ci ag wet lañu koy defe ak kanam...
Na moytu yii: Bu dawalee paaka ba, ba sidit ya tàmbalee dagg mu teggi ko, kon bu ko ca gaawee delloo dees na ko lekk.
s-112
wo_wtb-ud-train_1944
Na moytu yii: Bu dawalee paaka ba, ba sidit ya tàmbalee dagg mu teggi ko, kon bu ko ca gaawee delloo dees na ko lekk.
Bu ko ca yeexee delloo nag te lor waralu ko, kon deesu ko lekk.
s-113
wo_wtb-ud-train_1945
Bu ko ca yeexee delloo nag te lor waralu ko, kon deesu ko lekk.
Te yit mu bañ a tàqale baat ba, bu ko defee it du ko tee dagan, waaye bañ koo def a gën.
s-114
wo_wtb-ud-train_1946
Te yit mu bañ a tàqale baat ba, bu ko defee it du ko tee dagan, waaye bañ koo def a gën.
Waxtuw rendi walla loj mu ngi dale ci rendig yilimaan.
s-115
wo_wtb-ud-train_1947
Waxtuw rendi walla loj mu ngi dale ci rendig yilimaan.
Rendig yilimaan moo ngi aju ci ginnaaw bu sëlmalee julli gi, ba jant di so ca bisub ñatteel ba fu ñu ko fi rendee mu baax.
s-116
wo_wtb-ud-train_1948
Rendig yilimaan moo ngi aju ci ginnaaw bu sëlmalee julli gi, ba jant di so ca bisub ñatteel ba fu ñu ko fi rendee mu baax.
Ci ngiirum Maalig fàww rekk mu doon bëccëg, deesu ko sañ a ray guddi.
s-117
wo_wtb-ud-train_1949
Ci ngiirum Maalig fàww rekk mu doon bëccëg, deesu ko sañ a ray guddi.
La ca gën mooy boroom rendil ko boppam.
s-118
wo_wtb-ud-train_1950
La ca gën mooy boroom rendil ko boppam.
Bu amee ngànt mu wuutal ko moroomum jullitam, te nanga yéene yaw.
s-119
wo_wtb-ud-train_1951
Bu amee ngànt mu wuutal ko moroomum jullitam, te nanga yéene yaw.
Ku dul ab jullit manu laa rayal am tabaski.
s-120
wo_wtb-ud-train_1952
Ku dul ab jullit manu laa rayal am tabaski.
Ku rendi Tabaski ab jàmbur te amu ci ndigal, du ko doy am Tabaski te war naa fay boroom.
s-121
wo_wtb-ud-train_1953
Ku rendi Tabaski ab jàmbur te amu ci ndigal, du ko doy am Tabaski te war naa fay boroom.
Am Tëbëski nag deesu ko rendi jëkk rendig yilimaan te yilimaan it balaa rendi nég ba julli.
s-122
wo_wtb-ud-train_1954
Am Tëbëski nag deesu ko rendi jëkk rendig yilimaan te yilimaan it balaa rendi nég ba julli.
Ci ni ko Yonent (jàmmi Yàlla ci moom) bi waxe: Képp ku rëy njëkk jullig iid gi, deful lu dul rëy baayima bu ñu man a lekk;
s-123
wo_wtb-ud-train_1955
Ci ni ko Yonent (jàmmi Yàlla ci moom) bi waxe: Képp ku rëy njëkk jullig iid gi, deful lu dul rëy baayima bu ñu man a lekk;
Waaye ku rey ginnaaw jullig iid gi nag, am na am Tëbëski (Buxaari soloo na ko).
s-124
wo_wtb-ud-train_1956
Waaye ku rey ginnaaw jullig iid gi nag, am na am Tëbëski (Buxaari soloo na ko).
Tabaski lu am solo la ci Lislaam.
s-125
wo_wtb-ud-train_1957
Tabaski lu am solo la ci Lislaam.
Yonent (jàmmi Yàlla ci moom) bi xamle na ni toq dereet wi di njëkk a génn Yàlla dina ci jéggale mbooleem bàkkaar yu ñu mas a def.
s-126
wo_wtb-ud-train_1958
Yonent (jàmmi Yàlla ci moom) bi xamle na ni toq dereet wi di njëkk a génn Yàlla dina ci jéggale mbooleem bàkkaar yu ñu mas a def.
Nii la dikke ci hadiis ci nettalib Aysa (ngërëmul Yàlla ci moom).
s-127
wo_wtb-ud-train_1959
Nii la dikke ci hadiis ci nettalib Aysa (ngërëmul Yàlla ci moom).
Jëlee nanu ci Ibn Abaas mu ni Yonent (jàmmi Yàlla ci moom) bi nee na: Xaalis dugaleesu ko ci lu gën gàttub Tabaski (iid) (Daaru Qutni soloo na ko).
s-128
wo_wtb-ud-train_1960
Jëlee nanu ci Ibn Abaas mu ni Yonent (jàmmi Yàlla ci moom) bi nee na: Xaalis dugaleesu ko ci lu gën gàttub Tabaski (iid) (Daaru Qutni soloo na ko).
Yonent (jàmmi Yàlla ci moom) bi bégal na nu ci ne xarum Tabaski dina njot ci sawara niki mu njotee woon bakkanu Ismaayla.
s-129
wo_wtb-ud-train_1961
Yonent (jàmmi Yàlla ci moom) bi bégal na nu ci ne xarum Tabaski dina njot ci sawara niki mu njotee woon bakkanu Ismaayla.
Amul jëf ju nit di def ci bisu Tëbëski ju gën a neex Yàlla tuur ci dereet.
s-130
wo_wtb-ud-train_1962
Amul jëf ju nit di def ci bisu Tëbëski ju gën a neex Yàlla tuur ci dereet.
Noonu la ko Aysa nettalee.
s-131
wo_wtb-ud-train_1963
Noonu la ko Aysa nettalee.
Noo ngi leen di yéene Tëbëskig jàmm!
s-132
wo_wtb-ud-train_1964
Noo ngi leen di yéene Tëbëskig jàmm!
Di leen balu àq; di leen baal àq, te di ñaan Yàlla boole nu baal.
s-133
wo_wtb-ud-train_1965
Di leen balu àq; di leen baal àq, te di ñaan Yàlla boole nu baal.
Te nu fekke ko te romb ko...
s-134
wo_wtb-ud-train_1966
Te nu fekke ko te romb ko...
Edit as list • Text view • Dependency trees