Sentence view Universal Dependencies - Wolof - WTB Language Wolof Project WTB Corpus Part train
Text: Transcription Written form - Colors
Ab fajkatu jigéen mu ngi feddali wartéef wu tar wi jëm ci xeex réer gu jéggi-dayo gi
s-1
wo_wtb-ud-train_412
Ab fajkatu jigéen mu ngi feddali wartéef wu tar wi jëm ci xeex réer gu jéggi-dayo gi
Doktoor bu amul bluus : Réer moo jiitu ci jàngoro yi ñu war a faj
s-2
wo_wtb-ud-train_413
Doktoor bu amul bluus: Réer moo jiitu ci jàngoro yi ñu war a faj
Doktoor Atab Baaji ( Atab Badji ) mi liggéeyam màcc ci mbirum jigéen , biral na ne jamp na lool ñu xeex réer gu tar gi lëmbe Afrig te gàllankoor bu baax lépp lu mën a jur yokkute .
s-3
wo_wtb-ud-train_414
Doktoor Atab Baaji (Atab Badji) mi liggéeyam màcc ci mbirum jigéen, biral na ne jamp na lool ñu xeex réer gu tar gi lëmbe Afrig te gàllankoor bu baax lépp lu mën a jur yokkute.
Edit as list • Text view • Dependency trees