Sentence view

Universal Dependencies - Wolof - WTB

LanguageWolof
ProjectWTB
Corpus Partdev

Text: -

[1] tree
Li gën ci li nit njëkk a amal ci wàllug xam-xam mu ngi xewe ci Goxub Afrig.
s-1
wo_wtb-ud-train_415
Li gën ci li nit njëkk a amal ci wàllug xam-xam mu ngi xewe ci Goxub Afrig.
[2] tree
Ci lu gën a leer, ca Isipt gu yàgg ga la nit ku ñuul yóbboo ag nite (l'humanité) ba àggale ko ci xam-xam.
s-2
wo_wtb-ud-train_416
Ci lu gën a leer, ca Isipt gu yàgg ga la nit ku ñuul yóbboo ag nite (l'humanité) ba àggale ko ci xam-xam.
[3] tree
Booba la joxee firnde ci ne xam-xam du moomeelug wenn xeet, du caagéenu benn gox.
s-3
wo_wtb-ud-train_417
Booba la joxee firnde ci ne xam-xam du moomeelug wenn xeet, du caagéenu benn gox.
[4] tree
Gëstu yu boroom xam-xam bii di doomu Senegaal, di Seex Anta Jóob, maye nañu manees a saxal am-amu xam-xam bii di 'xeetu nit benn la'.
s-4
wo_wtb-ud-train_418
Gëstu yu boroom xam-xam bii di doomu Senegaal, di Seex Anta Jóob, maye nañu manees a saxal am-amu xam-xam bii di 'xeetu nit benn la'.
[5] tree
Ñoo bokk fu ñu bawoo, te xayug nit ku ñuul (la civilisation négre) moo jiitu ci xay yi.
s-5
wo_wtb-ud-train_419
Ñoo bokk fu ñu bawoo, te xayug nit ku ñuul (la civilisation négre) moo jiitu ci xay yi.
[6] tree
Taariix mu ngi nuy jàngal ne xam-xam ak xarala dañoo gàddaay dem ca goxub Tugal, jaare ko ca Geres.
s-6
wo_wtb-ud-train_420
Taariix mu ngi nuy jàngal ne xam-xam ak xarala dañoo gàddaay dem ca goxub Tugal, jaare ko ca Geres.
[7] tree
Bi mu mujjee di pujub àdduna bi ci wàllug xam-xam ak man-man, Tugal dafa daldi samp boppam niki digg (centre) bu coste ak pentug nit (créativité humaine) waaye mukk mu di bu ag muusam.
s-7
wo_wtb-ud-train_421
Bi mu mujjee di pujub àdduna bi ci wàllug xam-xam ak man-man, Tugal dafa daldi samp boppam niki digg (centre) bu coste ak pentug nit (créativité humaine) waaye mukk mu di bu ag muusam.
[8] tree
Ndax ag muus caadaa koy ëmb, te mooy fi nitug Afrig ki aaye, fi ko may mu jàmmaarloo ba tëyye màndargam caadaam, ak manmanu pentam gi nekk ci ag nekkam.
s-8
wo_wtb-ud-train_422
Ndax ag muus caadaa koy ëmb, te mooy fi nitug Afrig ki aaye, fi ko may mu jàmmaarloo ba tëyye màndargam caadaam, ak manmanu pentam gi nekk ci ag nekkam.
[9] tree
Ontologsi (L'ontologie) mbaa xam-xamu xalaatu nit ku ñuul ku Afrig mandargaalees na ko ni ko Meetar Wàdd wonee ca xalaatu 'jëmmam ba' (sa 'physicité').
s-9
wo_wtb-ud-train_423
Ontologsi (L'ontologie) mbaa xam-xamu xalaatu nit ku ñuul ku Afrig mandargaalees na ko ni ko Meetar Wàdd wonee ca xalaatu 'jëmmam ba' (sa 'physicité').
[10] tree
Màndargam xalaatub nit ku ñuul ku Afrig, moo di ne dafa di tay tabax ci cëslaayul yëg-yëg ak wormaal, séqoo gu nit ak dénd bi.
s-10
wo_wtb-ud-train_424
Màndargam xalaatub nit ku ñuul ku Afrig, moo di ne dafa di tay tabax ci cëslaayul yëg-yëg ak wormaal, séqoo gu nit ak dénd bi.
[11] tree
Loolu mooy wone nitug Afrig am na ay ngënéel yuy kojug nekk yu mu jëfandikoogul.
s-11
wo_wtb-ud-train_425
Loolu mooy wone nitug Afrig am na ay ngënéel yuy kojug nekk yu mu jëfandikoogul.
[12] tree
Ngënéel yii ci Afrig alal ju gànjaru lañu ngir gaawug yéegam ci biir ag gëstoom ñeel ñall (raccourcis) yu jàmme ngir dab yeneen réew yi.
s-12
wo_wtb-ud-train_426
Ngënéel yii ci Afrig alal ju gànjaru lañu ngir gaawug yéegam ci biir ag gëstoom ñeel ñall (raccourcis) yu jàmme ngir dab yeneen réew yi.
[13] tree
Seen jéegoy njàng yu am solo yi nu def ci Dara yu Kawe yi, ku mel ne Abdulaay Wàdd, Seex Anta Jóob Modibo Jara, wone nañu rëy xelug nitug Afrig ak ag neexug xelam.
s-13
wo_wtb-ud-train_427
Seen jéegoy njàng yu am solo yi nu def ci Dara yu Kawe yi, ku mel ne Abdulaay Wàdd, Seex Anta Jóob Modibo Jara, wone nañu rëy xelug nitug Afrig ak ag neexug xelam.

Edit as listText viewDependency trees